Akhlou Brick - Nila (Remix)

Advertisements
Wolof
A A

Nila (Remix)

Dolé dokhoul diam
Do mane té douma yow
Sagnsé damako tameu
Kholma ci souf ba cikaw
Té diémouma ko dama meun
Set ci wé ak ci karaw
Guissatouma louma nameu
Fima guéneu la nieup beug aw
 
Di nga ni nila nila
Nila waaay
Fi ma guén noy neu noy neu
Noy neu waaay
Di nga ni nila nila
Nila waaay
Di nga ma né noy neu noy neu
 
Nénala ngeu sol taille basse
Soloul ni ndanane bi
Soloul ni kou dieum nuit du dras
Boul faté foudeunou maquillage
Dionguama tague ley def moussorou
Dionguama dou sol bas
Nileu bilaaay, sama adjaratou sama adja
Nga solou mou yiw niou ande
Ma ame thieurou alladji
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
 
[Wally Seck]
Da nga né ci à péage romb la woroul
Do dioum ci maquillage mane damala wolou
Ya ngui teul sa greffage di dokh di dagou
Yor xirr di karawass ken meunoula sourr
Nékhoul ba nékhoul athi ngeu li nga sagnsé nekhneu
Ligu’ma défal bakhneu ya que beurri mana
Sol nga sa ndoquette taguanou
Mine nako ci yow oui mon cœur
Soula nékhé ragadjoul
Dane nga akhlou sagnsé
 
Looking my Marie Madeleine
Yagu’mey nirou Marie Madeleine
Yow sa dokhine nice neu woh ! woh ! woh
Dionguama kay tatafoumaaaa
Anh ! kay tatatfoumaaaa... hum
Nioweul tatatfoumaaa
Kay tatafoumaaaa
 
Nénala ngeu sol taille basse
Soloul ni ndanane bi
Soloul ni kou dieum nuit du dras
Boul faté foudeunou maquillage
Dionguama tague ley def moussorou
Dionguama dou sol bas
 
Nileu bilaaay, sama adjaratou sama adja
Nga solou mou yiw niou ande ma ame thieurou alladji
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
 
Da ngey solou di geuneu nice
Solou di geuneu toy
Sama xol bi di geuneu nath
Fi nga guénati geuneu noy
Sama dionguama paradise
Sa solou dou meuna tok
Té nga bayi soumala né sagnsé
Ga nane ma bea da nga meuna togn
 
Meun nga solou meun nga sagnsé carr sa col bi tégou na ci temps
Sa mélo bi mo geuna tarrou té mane sa djiko bi la geuna fan
Mane ak nio dakh wa Guissé Maabo, nio geuna niro
Mane yow la tamou yow la appo Sandi ma gouro
BB sa solou bi nala ci may note diokhma trois pièces bi damay sol
Dafa melni yow lepp la djapp meme solé loula eup sax dalay djote
Lalal nala bouko lali dagoul noum la nékhé nga diokhma sa lokho
Mélal ni kou dioigué Mali mane mala Toudé Aminata Bakhayoko
 
Nénala ngeu sol taille basse
Soloul ni ndanane bi
Soloul ni kou dieum nuit du dras
Boul faté foudeunou maquillage
Dionguama tague ley def moussorou
Dionguama dou sol bas
Nileu bilaaay, sama adjaratou sama adja
Nga solou mou yiw niou ande
Ma ame thieurou alladji
 
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
Nileu nileu nileu bilaayyyy
Nileu nileu nileu bilaaayyy nileu
 
투고자: ulissescoroaulissescoroa, 金, 13/12/2019 - 12:59
최종 수정: ulissescoroaulissescoroa, 金, 10/01/2020 - 03:43
고마워요!

 

Advertisements
영상
Akhlou Brick: 상위 3
코멘트