• Mia Guissé

    On a pas les temps

Paylaş
Font Size
Fransızca, Volofça
Fransızca, Volofça
Y'a pas de temps pour mécontent
Man jamm ju neex bi ma nekkee ba fin temps
Jottali ko sama oh là là
Maa tay di tàngal ci sa xol bi sama kafe tout le temps
 
Ni ngay def dawul sama yaram en passant
Maa yore volant bi di dawal awma temps
Waxtu bi ngay waxe lu ñaaw, man maa ngi biir banque
Man dama busy laajal kële heure, I don't have time
 
On a pas le temps
On a pas le temps
Awma benn temps
On a pas le temps
 
[Viviane Chidid]
Y'a pas longtemps la jël devant
Décidé tee farata gick bi teg leen banc
Am na partant, am na remplaçant
Montre bi kaay nga defarat ko bu de horloge la
 
Xamoo ci li ma nekk je sais que tu mens
Maa ngi dund àljanna, je passe du bon temps
Bu yewwoo waxal ma ko bye-bye et bon vent
Man dama busy laajal kële heure, I don't have time
 
On a pas le temps
On a pas le temps
Awma benn temps
On a pas le temps
 
Bul toppatoo bu leen faale
Nekkal sa bopp buñ la tardeel
Ñun les rumeurs on s'en tape
Nous on avance, ils font que parler
Dinañu la call su nu paree
Amuñu jot liggéey bee bari
Oh Mia, Viviane
Nous on avance, ils font que parler
 
Lele lele le
Viviane xalan bee time is money
 
Mia kaay wax leen
Le temps c'est de l'argent, au revoir
 
Y'a pas de temps pour mécontent
Man jamm ju neex bi ma nekkee ba fin temps
 
Am na partant, am na remplaçant
Montre bi kaay nga defarat ko bu de horloge la
 
Li ngay def dawul sama yaram en passant
Maa ngi dund àljanna, je passe du bon temps
Waxtu bi ngay waxe lu ñaaw, man maa ngi biir banque
Man dama busy laajal kële heure, I don't have time
 
On a pas le temps
On a pas le temps
Awma benn temps
On a pas le temps
 
Bul toppatoo bu leen faale
Nekkal sa bopp buñ la tardeel
Ñun les rumeurs on s'en tape
Nous on avance, ils font que parler
Dinañu la call su nu paree
Amuñu jot liggéey bee bari
Oh Mia, Viviane
Nous on avance, ils font que parler
 

 

Yorumlar