VJ

Sai Sai - English translation

VJ
Add to favorites
Album:
Prince de la ville (EP) (2025)
Original lyrics
Translation

Sai Sai

Suma la nammee bàyyi, jëlal paaka daas rey ma
Ndax boole nga li nga am ak li nga amul lépp jox ma
Su ma lay feccal guddi, bae du ñàkk fayda
Ma boole sama xol bi ak xëtër teg ci junni may la
 
Mbëggeel ni mu neexee bu de dëgg la du lu may wax
Dundu ci li ñu fekke danga jonge te neex a àndal
Allah, Alllah, architecte bi defar kii de ma ni aay na
Yaw wowal ma sa bàjjen, mu ñëw, fokk mu leeral ma
 
Woy joŋe nga
Yaak sa ay (neexaay)
Danga rafet (toogaay)
Neex neex la (cuuraay)
Yëngal nga ma (saay-saay)
 
Man dama la bëgg, nga bëgg ma (saay-saay)
Ma ni la bëggante la (saay-saay)
Dinañu rajaxate dëkk bi (saay-saay)
Wàcc ko ba muy zéro (saay-saay)
 
Lii pénalty la
Mbégté bi ne sama xol nga ñëw indi
Kon toogal, xaar, xool, yeneen laa lay indil
Lii dafa neex a neex a neex te vitaminé
Naa fo ba dugg sa 18 ñu mu lay cëgin!
 
Maa mujje jaaxle
Ndekete bidéew dina feñ, bëccëg yaa ngi
Ñi ne nañ dama dof ñi neex dama saalit
Laajal sama gars ñi
Man lu ma daaneel yombul waaye k.o nga ma
 
Bànneex bi ñu nekke dafa ëpp ba mënuma wax
Xale bi ni nga jekke danga joŋe te neex a àndal
Allah, Alllah, architecte bi defar kii de ma ni aay na
Yaw wowal ma sa bàjjen, mu ñëw, fokk mu leeral ma
 
Woy joŋe nga
Yaak sa ay (neexaay)
Danga rafet (toogaay)
Neex neex la (cuuraay)
Yëngal nga ma (saay-saay)
 
Man dama la bëgg, nga bëgg ma (saay-saay)
Ma ni la bëggante la (saay-saay)
Dinañu rajaxate dëkk bi (saay-saay)
Wàcc ko ba muy zéro (saay-saay)
 
Lii pénalty la
Mbégté bi ne sama xol nga ñëw indi
Kon toogal, xaar, xool, yeneen laa lay indil
Lii dafa neex a neex a neex te vitaminé
Naa fo ba dugg sa 18 ñu mu lay cëgin!
 
Yaak sa ay (neexaay)
Danga rafet (toogaay)
Neex neex la (cuuraay)
Yëngal nga ma (saay-saay)
 
Man dama la bëgg, nga bëgg ma (saay-saay)
Ma ni la bëggante la (saay-saay)
Dinañu rajaxate dëkk bi (saay-saay)
Wàcc ko ba muy zéro (saay-saay)
 
Lii pénalty la
Mbégté bi ne sama xol nga ñëw indi
Kon toogal, xaar, xool, yeneen laa lay indil
Lii dafa neex a neex a neex te vitaminé
Naa fo ba dugg sa 18 ñu mu lay cëgin!
 
Teg jeexal ci yaw chérie
Ba ma ñépp bàyye yaw la dese
Boo ma bàyyee man dina dee bae
Kon colleel serréel, bébé fais-moi rêver
 
Man suñ ma laajee
Kan mooy sama moitié
Man mëna waat ne
Yaw yaay sama moitié
 
En collé serré, bébé fais-mois rêver
Saa yu ñu gisee, gisoo ni muy neexee
Dans ciel étoilé que nous deux ma moitié
En collé serré, bébé fais-moi rêver
 
En collé serré, bébé fais-moi rêver
Saa yu ñu gisee, gisoo ni muy neexee
Dans ciel étoilé que nous deux ma moitié
En collé serré, bébé fais-moi rêver

Sai sai

If my heart wants to let go, don’t take advantage and hurt me
If you mix what you have with what you don’t have and give me everything
If I stay up all night thinking of you, it won’t be for nothing
I mix my heart with desire and give it to you fully
 
Love, the way it feels when it’s real, isn’t just something you say
Living with what we’re given, you’re young and easy to be with
Oh God, oh God, the architect
He designed you just perfectly
You, call your older sister
Let her come and help me understand
 
You’re young
You mess with your sweetness
You’re beautiful, the way you sit
Your curves are so sweet
You move me
 
I love you, love me back (saay-saay)
I’m telling you this is love (saay-saay)
We’ll rebuild the whole city (saay-saay)
Bring it down to zero and start fresh (saay-saay)
 
This is a penalty kick
The happiness you brought into my heart
So sit, wait, and see what else I’ll bring you
This feels so good, so good, so good — it’s like vitamins
Wait until you turn 18 and they’ll come for you!
 
I’m completely confused
Every morning your video shows up on my screen
Some say I’m crazy, others say I’m stylish
Ask my boys
What I’m feeling isn’t easy, but you did this to me
 
The pleasure we’re in is too much for words
Girl, the way you walk, you’re young and easy to be with
Oh God, oh God, the architect
He designed you just perfectly
You, call your older sister
Let her come and help me understand
 
You mess with your sweetness
You’re beautiful, the way you sit
Your curves are so sweet
You move me
 
I love you, love me back
I’m telling you this is love
We’ll rebuild the city
Bring it down to zero
This is a penalty kick
The happiness you brought into my heart
So sit and wait, see what else I’ll bring you
This feels so good, so good, so good — like vitamins
 
I’m completely focused on you, chérie
Everyone else left, only you remain
If you leave me, I’ll die waiting
So come close, hold me tight, baby, make me dream
 
If they ask me
Who my other half is
I can proudly say
You are my other half
 
Holding each other tight, baby, make me dream
Every time we meet, you see how good it feels
Under a starry sky, just us two, my other half
Holding each other tight, baby, make me dream
Likes1
You can thank submitter by pressing this button
expand collapse Translation details
Majesty20Majesty20
submitted on 10 Feb 2026 - 17:41
Guests thanked 1 time
Play video with subtitles
Log in or sign up to add a comment.
Log in Log in User Sign up