✕
Wolof
Wolof
Ey Massamba Walo
Sa ñàkk teew a raw daay
Bul ma fi ñukk gàddaay
Gis naa la ngay samandaay ni gaynde
Jigéen nga waaye jaambaar nga
Xébuma la ngir sa melokaan, man benn yoon
Jigéen nga waaye jaambaar nga
Ku ma xool ci yaw dina ma mere
Ndax demewuma xel, ci leen lu jëm ci yaw
Yàlla moo dogal fu ma la gise
Taggoo ak sama sagooy
Waaw man dama lay téye ak fukki loxo
Yàlla man la nattoo, manit ma nangu ko lool
Yaa ma leen gënal, dama la ko rusoon a waxe
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Li may gis sama xel dal na
Ndax tay day neex suba suba Yàlla la
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Li may gis sama xel dal na
Ndax tay day neex suba suba Yàlla la
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Bis a ngi ci bis yi man ak guys yi nañu fëgg sa kër
Dugg ci sabadore yi ànd ak paa yi, ñëw jox la sa cër
Foo mi taxu ma jukk dama àll ba ma la xame ba tay
Yeah waay jigéen nga waaye jaambaar nga
Xébuma la ngir sa melokaan, man benn yoon
Jigéen nga waaye jaambaar nga
Ku ma xool ci yaw dina ma mere
Ndax demewuma xel, ci leen lu jëm ci yaw
Yàlla moo dogal fu ma la gise
Taggoo ak sama sagooy
Waaw man dama lay téye ak fukki loxo
Yàlla man la nattoo, manit ma nangu ko lool
Yaa ma leen gënal, dama lay ko rusoon a waxe
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Li may gis sama xel dal na
Ndax tay day neex suba suba Yàlla la
Jiino jiin, sama xol neex na moo tax
Jiino jiin, samay way neex na
Comments